Le village Du Futur - Deukii Eleuk - The Village Of The Future
Parc - Keurou Bayimayii - The Park

Le parc est un lieu où l'on trouve presque tous les animaux sauvages, et ces animaux sont gardés avec beaucoup de prudence, ils sont beaux!!!. Le parc est magnifique!

Keurou bayimayii béreupe laa bokhamené dagñou Faikee yenn Malaa you so sokhore yiyee doundaa cii adounabi, Te danakaa Malaa you you yeup dagñe lenn di deinthieu bou baakhe kha baakhe, Dagñou réféte !!!.
Keurou bayimayii daa faa selle!!!

In the park, you can find nearly all the wild animals, they're looked after carefully, they're beautiful!!!. The park is beautiful too!