![]() |
![]() |
Soy dem cii Dieunedoukay bii, dagñouille diar cii bene Pont. Di farall di dem cii Dieudoukay yii da fa nekh, nakh day takh gua dieuneda lou barre am na tamitt ay diaykattou creme glaces cii yoon bii. Say sou gñouille dem cii Dieunedoukay bii day nekh, nakhté gñoune nieup pay anda!!
To go to the shops, one needs to go over a bridge. Shopping's so much fun, you get to buy plenty of things, and there are ice-cream merchants everywhere. We always have a smashing time shopping together!!